TABASKI

Abdou  da weur weur amoul khar, ta niéme woul gnibi amoul yapp, mou bayyi ba bissou tabaski si souba moy weut féss. Béné waye néko kaye fessal ma sa ma khar , sa waye mor nangou niou daccor si 2000 f.Sa waye mor féss khar mi, dieul mbakh bi déf li gueune bakh si kharmi, déf ko si bir thiaya dji. Wa dji nieuw néko
– Ah seugn bi yaw li nga féss ni rék la tolou, ak sama khar ni mou tolone yeup
mor néko
– Waw kham nga yapp maname so ko fessé day délou, lolou rék la
– ah kone lolou la. féy mor. Sa waye nak dioubal bountou keur ga di dokh kom canara, mbakh yapp bi mou déff si thiaya dji dissal ko, komanssé sitt wadji topp ko néko
– ah seugn bi ya ngui sitt dérét dé mba diam?
– Sa ma birr moy daw, mo takh , toujourssou ma fessé khar ni la may déf koi
dougal si douss bi kéy
– youh mane kéy sama keur rék
wadji néko
– youh lolou mom dou yafou dioulit dougal fi rék
bi wakh dia komanssé bari, mor dougal lokho bi ci thiaya bi né ko
-niéfal sa ndèye am sa yapp, sa wakh dji sonal na ma torop

commentaires

Laisser un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée.

Ce site utilise Akismet pour réduire les indésirables. En savoir plus sur comment les données de vos commentaires sont utilisées.

Translate »
RSS
Follow by Email
YouTube
Telegram
WhatsApp